| Atelier | Sa entreprise couture ci Kayñiawlu. Benn atelier dafay boole ay point de vente, équipe, client ak commande. |
| Point de vente (PDV) | Benn barab bu sa atelier : boutique, atelier production, stand. Commande bu nekk takku na ci benn point de vente. |
| Boroom | Compte bi sos atelier bi. Am na sañ-sañ yépp : équipe, point de vente, abonnement. |
| Jëfandikukat | Compte bu boroom bi sos. Dafay gis client yépp, waaye commande yi ci ay point de vente yi ñu ko jox rekk. |
| Fiche mesure | Mesure yu benn client ngir benn type vêtement, ci benn date. Fiche bu enregistré du soppiku. |
| Type vêtement | Benn modèle fiche mesure (boubou, costume, taille basse…) buy tëral champ yi ñuy natt. Atelier bu nekk mën na ko soppi. |
| Commande | Benn pièce (walla ay pièce) bu client commande : modèle, montant, acompte, date livraison, statut. |
| Référence | Numéro bu commande bi rekk moom, ñu koy sos automatique (misaal : KLM-0237). |
| Acompte | Xaalis bi client bi fey ci commande bi. Li des, ñu koy xayma automatique. |
| Statut | Etape bu benn commande : en attente, en cours, essayage, terminée, livrée, annulée. |
| Rappel livraison | Alerte automatique bi ñuy yónnee équipe bi bu date livraison bi jegesee. |
| Synchronisation | Yónnee automatique li nga bind te amuloo woon connexion, bu réseau bi dellusee. |
| Plan | Sa formule abonnement : Gratis, Pro walla Entreprise. Moo tëral limu point de vente ak compte yi. |
| Backoffice | Application web bi ngir topptoo, ci app.kayniawlu.com. |